Home » Music » Baye Mass - Yëffu Doff ( Clip officiel)

Baye Mass - Yëffu Doff ( Clip officiel)

Written By Baye Mass on Sunday, Mar 19, 2023 | 07:59 AM

 
Auteur : Baye Mass Production: Mpossible Prod Réalisateur : Pac Deejay Compositeur : Pape Laye Studio : Mpossible Mix & Mastering : Sirtam Beats Une production de Mpossible Prod (Dakar, Senegal, Mars 2023) ** Retrouvez Baye Mass sur ses réseaux sociaux ** Instagram : https://www.instagram.com/bayemass_/ TikTok : https://www.tiktok.com/@bayemass_ ** Retrouvez Mpossible Prod sur ses reseaux sociaux ** Facebook : https://www.facebook.com/mpossiblep Instagram : https://www.instagram.com/mpossibleprod/ Site web : https://www.mpossibleprod.com ** Contact management ** [email protected] 78 300 52 52 Lyrics Yow ! Rigolo , con, ñëpa parano fiii … Kunek tibë jëmelé sa biir bi xawma dañu rew xawma dañu possedé ! Suñu grand yi wara jangalé di xasté Fi Études , Politique , Économie ñossi ngenë delu guinaw Détails yi , Batailles yi ak yëfu doff yi ñossi ëpp ay trophée Mérité woleine ma judu ci sen Réw mi ! Dama wara déménager dem deuk thi Air bi… fi ñi fi gën nul lañj gën diox nope Ñi fi gën immature lañu gën diox bope Jiguene yi , Billets yi ak Bouteilles yi la xalé you guor yi di weur Volets yi , Billets yi ak Téléphone yi Mom la djiguene nji di weure Bëri yëfi doff … Senegal dafa bëri yëfi doff Bëri yëfi doff… Bëri yëfi doff …senegal dafa Bëri yëfi doff lolu rek fi dox Bëri yëfi doff … Senegal dafa Bëri yëfi doff Bëri yëfi doff … Bëri yëfi doff …sama rew dafa beuri yeufi doff lolou rek fi dox Deuk bu xate … Alë yu yaatu Auto you chère …té tali bi baxoul Stade bou bess… té talibé yi lekuñu Avion bou bess … té ame village you naanul … Ame coupe bou bess… ndeketei palais woroul …médias you faux , journalistes you jangoul… Musik bou rëp… té contenu bi baxoul… Rappeurs you Réw ak mbalakh man you ayul Mérité woleine ma judu ci sen Réw mi ! Dama wara déménager dem deuk thi Air bi… fi ñi fi gën nul lañj gën diox nope Ñi fi gën immature lañu gën diox bope Jiguene yi , Billets yi ak Bouteilles yi la xalé you guor yi di weur Volets yi , Billets yi ak Téléphone yi Mom la djiguene nji di weure Bëri yëfi doff … Senegal dafa bëri yëfi doff Bëri yëfi doff… Bëri yëfi doff …senegal dafa Bëri yëfi doff lolu rek fi dox Bëri yëfi doff … Senegal dafa Bëri yëfi doff Bëri yëfi doff … Bëri yëfi doff …sama rew dafa beuri yeufi doff lolou rek fi dox Bëri yëfi doff …sama rew dafa beuri yeufi doff lolou rek fi dox